Letra de Jammu Africa - Isma�l Lo
Letra de canci�n de Jammu Africa de Isma�l Lo lyrics
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Sama gent gi maa ngi �aan Yalla wonma ko bala may �ibbi barsaq
Ma ne bes du �akk ci bes yi Afrika don benn reew
D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique
M�m' si le ciel tombait luttons pour la paix
Kon jammu Afrika moom lay �aan
Man� jammu Afrika mooy su�u natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Yow mi nekka bittim reew man mi L� maa ngi lay �aan
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika
Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur
M�m' si le ciel pleurait luttons pour nos fr�res
Kon jammu Afrika moom lay �aan
https://www.coveralia.com/letras/jammu-africa-ismael-lo.php
Man� jammu Afrika mooy su�u natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men
Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi
Yoo Alla addu jam to Ruanda
Yoo Alla addu jam to Burundi
Yoo Alla addu jam to Casamans
Lawol Mbignona yee