Letra de My People (Samay Nit) - Youssou N'dour
Letra de canci�n de My People (Samay Nit) de Youssou N'dour lyrics
ma ngui binde way bi diko m�y
gneup gni ma beugue di l�n ndioukel
ndioukel gneup gni ma diapal�
souma l�ne meunone diokh lokho defnako
soumal�ne meunona setsi eh eh yeksina
fat�woumal�ne, d�d�te meunoul am
yeugone nal�n salaw moy li wor
souma teugu� ng�ne gneuw wouyoussima
souma gu�n� lou bess ng�ne dieundeuko
manou mal�ne faye
magui bind way wi di l�ne ko m�y
refrain (bis)
you you you you
you gorgorloul gnougui sa guinaw
soumal�ne meunone diokh lokho defnako
https://www.coveralia.com/letras/my-people--samay-nit--youssou-n-dour.php
souma l�n meunona setsi y�ksina
kouma souf�l ng�ne khoulok mom
fat�woumal�ne d�d�t meunoul am
yeugue nal�ne salaw moy li wor
bataxna ma gui bind way wi diko may
refrain (bis)
fat�wouma fat�wouma fat�wouma fat�wouma ah (4 fois)
refrain (bis)
ehhhhhhhhhhhhhhh mangl�ni sant di gueureum
mane ndioukel nal�n
gneup gni ma beugue di l�n ndioukel
ndioukel gneup gni ma diapal�
souma l�ne meunone diokh lokho defnako
soumal�ne meunona setsi eh eh yeksina
fat�woumal�ne, d�d�te meunoul am
yeugone nal�n salaw moy li wor
souma teugu� ng�ne gneuw wouyoussima
souma gu�n� lou bess ng�ne dieundeuko
manou mal�ne faye
magui bind way wi di l�ne ko m�y
refrain (bis)
you you you you
you gorgorloul gnougui sa guinaw
soumal�ne meunone diokh lokho defnako
https://www.coveralia.com/letras/my-people--samay-nit--youssou-n-dour.php
souma l�n meunona setsi y�ksina
kouma souf�l ng�ne khoulok mom
fat�woumal�ne d�d�t meunoul am
yeugue nal�ne salaw moy li wor
bataxna ma gui bind way wi diko may
refrain (bis)
fat�wouma fat�wouma fat�wouma fat�wouma ah (4 fois)
refrain (bis)
ehhhhhhhhhhhhhhh mangl�ni sant di gueureum
mane ndioukel nal�n